Teranga ñell na Baay bi
Teranga ñell na Baay bi, Doom ji, ak Xel mu Sell mi,
naka la woon ca cosan la Tey ak mos ba ca mos a mos.
Amiin
Teranga ñell na Baay bi, Doom ji, ak Xel mu Sell mi,
naka la woon ca cosan la Tey ak mos ba ca mos a mos.
Amiin
Sunu Baay, bi ci asamaan
na sa tur sell,
na sa nguur dikk,
loo bëgg,
na am ci suuf naka ca asamaan.
May nu tey sunu dundu bés bu nekk,
te baal nu sunuy tooñ,
naka nuy baale ña nu tooñ.
Tc bu nu bàyyi nu tàbbi ci bëliis,
wànte musal nu ci lu bon
Amiin.
Ô mon Jésus, pardonnez-nous tous nos péchés,
préservez-nous du feu de l’enfer
et conduisez au ciel toutes les âmes,
surtout celles qui ont le plus besoin de votre sainte miséricorde.
و بربّ واحد يسوع المسيح ، ابن الله الوحيد ، المولود من الآب قبل كل الدهور ، إله من إله ، نور من نور ، إله حق من إله حق ، مولود غير مخلوق ، مساو للآب في الجوهر ، الذي به كان كل شييء ، الذي من أجلنا نحن الخطأة ، و من أجل خلاصنا ، نزل من السماء ، تجسّد بقوة الروح القدس ، من مريم العذراء و تأنس . صلب عنّا على عهد بيلاطس البنطي ، تألّم و مات و قبر و قام في اليوم الثالث كما في الكتب، صعد إلى السماء و جلس عن يمين الآب، و أيضا سيأتي بمجد عظيم ، ليدين الأحياء و الأموات ، الذي لا فناء لملكه.
Nuyu naa la, Maryaama, fees nga ak yiw,
Borom baa ngi ak yow,
barkeel nga ci jigéen ñi yepp,
te Yéesu, sa doomu biir, barkeel na.
Maryaama mu sell mi, Ndeyu Yàlla,
ñaanal ñu, ñun bàkkaarkat yi,
léegi ak ci suñu waxtu dee.
Amiin